Genesis 39:1
TSK
¶ Ba ñu yóbboo Yuusufa Misra, Potifaar, jawriñu Firawna, ma jiite ay dagam, da koo jënd ca Ismayleen, ña ko fa indi.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Ba ñu yóbboo Yuusufa Misra, Potifaar, jawriñu Firawna, ma jiite ay dagam, da koo jënd ca Ismayleen, ña ko fa indi.
¶ Yuusufa ne ko: «Piri mi mooy lii. Ñetti car yi, ñetti fan la.
Yàlla nag may ñeenti xale yu góor yooyu xel ak ràññee ci mboolem lu ñu bind ak wàllu xam-xam. Dañeel moom mana firi mboolem peeñu ak gént.