¶ Yaw Esra nag, seetal ci xel mu rafet mi sa Yàlla digle ci yoonam wi nga yor, nga tabb ay njiit aki xaali, ngir ñuy àtte mboolem ñi xam sa yooni Yàlla ci diiwaani Wàllaa Dex. Te ñi ko xamul, nga xamal leen ko.
TSK
TSK · Genesis 41:38
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ezra 7:25
TSK
Proverbs 14:35
TSK
Buur day bége jawriñ ju xelu, di mbugal nitu gàcce.
Daniel 4:6
TSK
¶ Ma ne ko: «Beltasar, kilifay taryaax yi, man ci sama bopp xam naa ne xelum yàlla yu sell yaa ngi ci yaw, te menn mbóot jaaxalu la. Peeñum gént gi ma gént, wax ma piri mi.
Daniel 4:18
TSK
mook xobam yu naat ak meññeefam mu ne gàññ, mana dundal ñépp; muy keppaaral rabu àll, di tàggal njanaaw:
Daniel 5:14
TSK
Dégg naa sab jëw, ñu naan noowi yàlla yaa ngi ci yaw, te gis nañu ci yaw ag ràññee akum xel ak xam-xam bu takku.
Daniel 6:4
TSK
Ci biir loolu Dañeel di ku ràññiku ci biir saytukat yaak jawriñ ya, ndax rafet um xel; ba tax Buur di seet nu mu koy fale, mu yilif nguur gépp.