¶ Ba loolu amee Yàlla geestu Rasel, nangul ko, may ko doom.
TSK
TSK · Genesis 43:29
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Doomi Rasel di Yuusufa ak Beñamin.
Ñu ne ko: «Nun ñii di la siyaare de, fukki góor ak ñaar lanu woon, bokk sunu baay, ba ca Kanaan. Ka ca gën di xalee nga ca sunu baay, te ka ca des nekkatul.»
Kon nag du yeena ma yebal fii, waaye Yàllaa. Te moo ma jagleel, ma doon cëslaayal Firawna, mel ni baay ci moom, jiite këram gépp, boole ci yilif mboolem réewum Misra.
Mu jëm ci njiital jàngkat yi, ànd aki xalam, di woyu Sabóor.
Ceeñeeru biir lëndëm jollil na ku jub ak ku baax, di boroom yërmande ak njekk.
Yeen waa Siyoŋ, yeen waa Yerusalem, dootuleen jooy mukk! Bu ngeen jooyee, mu yërëm leen moos; bu leen di dégg, di leen nangul.
«Ngeen ne: “Léegi nag tinuleen Yàlla rekk, mu baaxe nu!” Yeena tooñ, ndax day siggil kenn ci yeen?» Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko wax.
ñeel Timote, sama doomu bopp ci wàllu ngëm. Aw yiw ak yërmande ak jàmm ñeel na la, bawoo ci Yàlla Baay bi, ak sunu Sang Almasi Yeesu.