TSK

TSK · Genesis 43:30

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu laxasu Beñamin rakkam, daldi jooy, Beñamin it laxasu ko, jooy.

Ci kaw loolu ndaw si doomam di dund daldi ñeewante doomam. Mu ne: «Déet, sang bi, jox ko xale bi. Bu ko rey mukk!» Ndaw sa ca des, moom, ne: «Deesu ma ko jox, deesu la ko jox; dogleen ko ñaar!»

«Efrayim, ana nu ma lay baye, yaw Israyil laa ne, nu ma lay tege ciy loxo? Ana nu ma lay defe ni Atma? Nu ma lay yemaleek Ceboyim? Sama xol a bëpp, sama yërmandee yëngu.

¶ di jaamoo Boroom bi ag woyof gu mat sëkk, ci biiri rongooñ ak nattu yu ma pexey Yawut yi teg.

Ba loolu amee ñépp jooyoo jooy yu metti, laxasu ko, fóon ko.

¶ Ndegam amees na lenn lu yokk aw fit ci Almasi mi nu gëm, ndegam lenni cofeelam lu mana dëfal am na, ndegam amees na benn cér ci Noo gu Sell gi, ndegam it, amees na lenn lu bawoo fi moom, ci wàllu xol bu rafet, ak yërmande,

Yàkkamti naa lool gisati la, ba sama xol sedd guyy, nde maa ngi fàttliku sa rongooñi keroog ya.