¶ Ibraayma dellooti ne: «Rikk Boroom bi, bu ma mere. Dinaa ci teg lii. Su fa fanweer ñu jub rekk amee nag?» Aji Sax ji ne ko: «Su fa fanweer ñu jub amee, kon duma def dara.»
TSK
TSK · Genesis 44:18
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 18:30
TSK
Genesis 37:6
TSK
Da ne leen: «Dégluleen li ma gént.
Genesis 41:44
TSK
¶ Ci kaw loolu Firawna ne Yuusufa: «Man maay Firawna, waaye gannaaw-si-tey mboolem waa réewum Misra, kenn du ci sañatee yékkati loxo mbaa muy séqi jéego, te àndoo ci.»
2 Samuel 14:12
TSK
¶ Jigéen ja ne ko: «Buur, sang bi, ma ñeme laa waxati benn baat boog!» Mu ne ko: «Waxal.»
Job 33:31
TSK
Baay Ayóoba, teewlul, déglu ma, neel cell, ma wax la, man.
Proverbs 19:12
TSK
Merum buur ni gaynde gu ŋar; yërmandey buur ni lay cig mbooy.
Daniel 3:19
TSK
¶ Ci kaw loolu Nabukodonosor mer lool ba fees dell, kanam gay sël-sëli janook Sadarag Mesag ak Abet Nego. Mu santaane ñu xamb taal ba, ba mu gëna tàng juróom ñaari yoon na mu daan tànge;