TSK

TSK · Genesis 45:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

“Lan mooy seen liggéey?” ngeen ne ko: “Nun de sang bi, ag jur lanu masa yar, ba nuy gone ba tey, te noonu la ko sunuy maam daan defe.” Su boobaa, ngeen mana féetewoo diiwaanu Gosen, ndaxte waa Misra dañuy xof sàmm.»

Ñu teg ca ne ko: «Danoo ñëw ngir dal ci réew mi, ndaxte amalatunu sunu jur parlu, te xiif bi metti na ca réewu Kanaan. Moo tax sang bi, nu di la ñaan, nga may nu, nu dal foofa ca diiwaanu Gosen.»

Ba loolu amee Yuusufa di dundal baayam aki bokkam, ak mboolem waa kër baayam, boole ca ña bootu ca ñoom.

Diiwaanu Gosen, ga bànni Israyil dëkkoon doŋŋ, moo mucc ca tawub yuur ba.