TSK

TSK · Genesis 45:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Abimeleg ne ko: «Sama réew mépp a ngi noonu, dëkkal fu la neex.»

¶ Yuusufa teg ca ne Firawna: «Kon léegi sang bi, wutal nit ku muus te rafet xel, jiital ko ci réewum Misra.

ki leen daan jiitu ci yoon wi, ngir sàkkal leen fu ngeen di dale; guddi, mu nekk ci biir sawara, di leen niital yoon wu ngeen jaare; bëccëg, mu nekkal leen ci biir aw niir.

Su ko defee nag Buur, janq bu la ci neex doon lingeer, wuutu Wasti.» Buur rafetlu la ñu wax, daldi def noona.

Acts 6:5 TSK

¶ Wax jooju daldi neex mbooloo mépp. Ñu seppi Eccen, nit kufeese ngëm ak Noo gu Sell gi, seppi Filib ak Porokor ak Nikanor ak Timon ak Parmenas ak Nikolas, ma dëkke Àncos te dib tuubeen bu duggoon lu jiitu ci yoonu Yawut.