Genesis 30:11
TSK
Leya ne: «Ndaw wërsëg wu réy!» daldi ko tudde Gàdd (mu firi Wërsëg).
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Leya ne: «Ndaw wërsëg wu réy!» daldi ko tudde Gàdd (mu firi Wërsëg).
«Gàdd la gàngoor di gaw, mu téqtal leen, ba daan.
¶ Ñu lim turi sëti Gàdd, ku nekk ak làngu cosaanam ak kër maamam, mboolem góor ñi xare war, te ñu am ñaar fukki at, jëm kaw.
ak ñoom Osni mi sos làngu Osneen ñi, ak ñoom Eri mi sos làngu Ereen ñi,
Gàdd la wax ne ko: Barke ñeel na ku yaatal Gàdd. Ni gaynde la goore, te mooy xotat përëg akum kaaŋ.