Yanqóoba bëgg Rasel lool, ba ne Laban: «Dinaa la liggéeyal juróom ñaari at ngir Rasel sa doom ju ndaw ji.»
TSK
TSK · Genesis 46:19
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 29:18
TSK
Genesis 35:16
TSK
¶ Ba loolu wéyee ñu jóge Betel, dem bay bëgga jub Efrata. Rasel tollu ciw mat, te mat wi metti.
Genesis 37:1
TSK
¶ Yanqóoba ma nga dëkkoon réewu Kanaan, fa baayam daloon.
Genesis 44:27
TSK
Sunu baay, ba lay siyaare, ne nu: “Xam ngeen ne damaa amul ak sama soxna lu dul ñaari doom.
Genesis 49:22
TSK
«Yuusufaay bànqaasu garab, garab guy meññ, feggook bëtu ndox, car yaa nga law, tiim digu tool ba.
Exodus 1:3
TSK
ak Isaakar ak Sabulon, ak itam Beñamin;
Numbers 1:36
TSK
¶ Ñu lim turi sëti Beñamin, ku nekk ak làngu cosaanam ak kër maamam, mboolem góor ñi xare war, te ñu am ñaar fukki at, jëm kaw.
Beñamin la wax, ne ko: Soppeb Aji Sax jaa ngi, keey dëkke xel mu dal fi wetam, mu di ko yiir bésoo bés, te diggantey waggam la dëkke.