TSK

TSK · Genesis 47:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Abimeleg ne ko: «Sama réew mépp a ngi noonu, dëkkal fu la neex.»

Su ko defee nga dëkksi diiwaanu Gosen, nekk ci sama wet, yaak say doom ak say sët ak say gàtt ak say gétt ak mboolem loo moom,

Te buleen réccu alal, ji ngeen di bàyyi seen gannaaw, ndax li gën ci réewum Misra yeena koy moom.”»

¶ Yuusufa nag dalal baayam aki bokkam, dogal leen suuf sa gën ca réewum Misra ca diiwaanu Ramses, ni ko ko Firawna sante woon.

Ña faalewul kàddug Aji Sax ji, ñoom, wacc seeni jaam ak seeni jur ca biti.

Mu seet ca bànni Israyil gépp, tànn ca góor ñu mat, fal leen, ñu yilif mbooloo ma: ñii jiite kuréli junniy nit; ñii, téeméer; ñii, juróom fukk; ñii fukk.

Seetlul ku man liggéeyam, buur lay liggéeyal, du liggéeyal baadoolo.