¶ Ba mu dawee, malaakam Aji Sax ja gis ko fu dend akub bëtu ndox ca màndiŋ ma, mooy bëtu ndox, ba ca yoonu Sur.
TSK
TSK · Genesis 48:16
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ndeke Aji Sax jaa nga tollu ca wetam. Mu wax ak moom ne ko: «Maay Aji Sax ji, di sa Yàllay maam Ibraayma te di Yàllay Isaaxa. Suuf si nga tëdd dinaa la ko jox, yaak sa askan.
Nit ka ne ko: «Na nga tudd?» Mu ne ko: «Yanqóoba.»
«Yuusufaay bànqaasu garab, garab guy meññ, feggook bëtu ndox, car yaa nga law, tiim digu tool ba.
Malaakam Aji Sax ja feeñoo ko foofa, melow sawara wuy tàkk, jafal fa ab gajj. Musaa xoolaat, ndeke gajj ba bépp jàpp na, ba ne jippét, waaye lakkul.
Ña ñu lim ñépp di juróom benn téeméeri junneek ñett ak juróomi téeméer ak juróom fukk (603 550).
Làngi Manasee ngoogu, ña ñu leen limal di juróom fukki junneek ñaar ak juróom ñaar téeméer (52 700).
Taawub yëkk la, daraja mooy boroom, béjjén ya, béjjéni nagu àll la, ca lay butteendoo xeet yépp, ba ca cati àddina. Ñooñooy junniy junniy nit ca giirug Efrayim, ak junni ca giirug Manase.
Buur daldi giñ ne: «Giñ naa ci Aji Sax ji, Kiy Dund te musal sama bakkan bii ci jépp njàqare,
Naa màggal Aji Sax ji saa su ne, di ko sant fu ma tollu.
Ku ragal Aji Sax ji, malaakaam yiir la, di la wallu.
Aji Sax jee lay sàmm ci gépp loraange, di sàmm sa bakkan.
Seen gépp njàqare di njàqarey boppam, malaaka mi mu jàkkaarlool musal leen ca. Moo leen sopp, ñeewante leen, ba jotal leen boppam, te fu ñu masa jaare démb, mu fab leen, boot.
Ci biiru ndeyam la kii suufoo ab seexam; kii moo tollu ci dooleem, bëreek Yàlla.
¶ «Maa ngii di yebal sama ndaw, mu xàllal ma aw yoon. Sang bi (/Boroom bi) ngeen di sàkku mooy jekki agsi këram, malaakam kóllëre moomu (/ndawal kóllëre loolu), ki ngeen safoo, mu ngooguy dikk.» Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko wax.
ngir ndesu nit ñi sàkku Boroom bi, te ñooñoo di jaambur ñi ñu tudde sama tur.
te ñoom ñépp, menn ndoxum kéemaanu Yàlla ma lañu naan, ndax ñoo doon naane ca doju kéemaanu Yàlla ga, doj wa leen doon gunge, te doj wa Almasi la woon.
Boroom bee may wallu ci jépp jëf ju bon, te moo may aar ba tàbbal ma fa nguuram ga fa asamaan. Daraja ñeel na ko, tey ak ëllëg ba fàww. Amiin.
¶ Ba Yanqóoba di waaja nelaw, ngëm la ñaanale ñaari doomi Yuusufa yépp, doora sujjóot, jafandoo boppu yetam.