Genesis 37:30
TSK
Ba loolu amee mu jóge ca, dem ca ay rakkam ne leen: «Xale ba nekkatu fa de! Te man xawma nu may def léegi.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ba loolu amee mu jóge ca, dem ca ay rakkam ne leen: «Xale ba nekkatu fa de! Te man xawma nu may def léegi.»
¶ Bés ba Aji Sax jiy yóbbu Ilyaas kaw asamaan ci biir callweer, ma nga bàyyikoo woon Gilgal, ànd ak Alyaasa.
Alyaasa gis loolu, daldi yuuxu, naan: «Wuy baayee, baay bóoy, yaay watiiru xarey Israyil aki gawaram!» Ba loolu amee gisatu ko. Mu ne sëq ay yéreem, ne ko tareet, def ko ñaar ndaxu tiis,
¶ Ci kaw ngëm lees yóbboo Enog, te deewul. Da ne mes, ndax Yàllaa ko yóbbu. Balees koo yóbbu kay, lees ko seedeeloon ne moo bànneexal Yàlla.