2 Samuel 14:8
TSK
Buur ne ko: «Demal ñibbi. Man ci sama bopp maay joxe ndigal ci yaw.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Buur ne ko: «Demal ñibbi. Man ci sama bopp maay joxe ndigal ci yaw.»
Kon nag Sang bi, may ma xel mu am ug dégg mu ma àttee sa ñoñ, ngir may ràññee lu baax ak lu bon. Ndax kat, ana kan moo mana àtte sa ñoñ, wii askan wu réy?»
Xanaa du nopp ay natt baat bu jib, denqleñ di mosu ñam?
Kon nga xam luy ragal Aji Sax ji, xam Yàllaa di kan;
Liy dalal seen jamono mooy koomu ndam; xel ak xam-xam, te ragal Aji Sax ji, loolooy seen alal.
Man nag, su dee yeena dogal samab àtte, mbaa kurélu nit a dogal samab àtte, soxaluma lool, te dogalaluma sama bopp ab àtte it,
Mag ñi kay ñoo yelloo ñam wu dëgër, ñoo tàmma jëfoo seenum xel, ngir ràññee lu baax ak lu bon.