TSK

TSK · Isaiah 46:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Guddig keroog maay wër réewum Misra te maay fàdd lépp luy taaw bu góor ci réewum Misra, nit ak mala, te itam maay mbugal mboolem tuuri Misra. Man maay Aji Sax ji.

Job 39:11 TSK

Yaa koy yaakaare dooleem ju bare, ba dénk ko sab liggéey?

Ma ne gawar a ngii, war watiiru ñaari fas. Nee: “Daanu nañoo, Babilon daanu na, jëmmi tuuram yépp tasaaroo fi suuf!”»

muy saf kuñeental ci biir tóokërub xaal. Du wax, du séqi jéego, ñu di ko gaŋar-gaŋaree. Buleen ko ragal, du lore, du jariñe.»

Mowab, yeena yaakaar dooleek alal, yeen it, dees na leen jàpp; Kemos, seen tuur mi duggi ngàllo, mooki sarxalkatam aki kàngamam.

Maay dikke mbugal Bel, tuur mi ci Babilon, yàbbiloo kob lancam. Xeet yi noppee def um wal, wuti ko, tatay Babilon it màbb.

«Moo tax, bés a ngii di ñëw,» kàddug Aji Sax jee, «maay dikke mbugal seen jëmmi tuur yi, ñoom, ñi ñu jam di binnee fi réew mi mépp.