TSK

TSK · Isaiah 57:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Su boobaa pënd dellu suuf, na woon; bakkan dellu fa Yàlla ma able woon.

Ku dëggu, yoonam day maase; ku dëggu, Aji Jub ji jubal xàllam.

Buurub Elam kay a nga tëdd ca biir ña ñu bóom, mook gàngooram gépp, seeni bàmmeel yéew ko. Paaxe yooyu yépp a fàddoo saamar, te daan tiital waa réewum aji dund ña. Seen gàcce lañu gàlloo, ànd ak ñay wàcci biir pax, ñu boole leen ak ña ñu bóom ab tëraay.

Luke 1:6 TSK

Ñoom ñaar ñépp a juboon, Yàlla seede, te mucc ayib ni ñuy jëfe santaane yeek ndigali yooni Boroom bi.

Luke 7:50 TSK

Yeesu nag ne ndaw sa: «Sa ngëm musal na la, demal ak jàmm.»

¶ Xam nanu ne sunu yaram, sunu këru kaw suuf gii di ab xayma, bu daanoo it, am taax lanu am fa Yàlla, kër gu sax dàkk, gu loxol nit tabaxul.

Ci diggante yaar yooyii laa tance: yàkkamti na maa yiwiku ba fekki Almasi, te loolu moo dàqati fuuf.