Job 1:4
TSK
¶ Doomi Ayóoba yu góor ya nag dañu daa ay-ayloo berndey biir kër, ku nekk ak bésam. Su ko defee ñu yónnee, woo ca seen ñetti jigéen ña, ngir ñu bokk di lekk ak a naan.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Doomi Ayóoba yu góor ya nag dañu daa ay-ayloo berndey biir kër, ku nekk ak bésam. Su ko defee ñu yónnee, woo ca seen ñetti jigéen ña, ngir ñu bokk di lekk ak a naan.
Doom aadama la bésu safaan bay bett, jekki ne dàll fi kawam, ni jën wu keppu cib caax, loru, mbaa picc mu tancu cig fiir. Doom aadama xamul bésam.
Nit ñaa nga doon lekk ak a naan, di jël jabar ak a séyi, ba keroog bés ba Nóoyin duggee ca gaal ga, mbënn ma dikk, sànk ñépp.