TSK

TSK · Job 39:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ci kaw loolu ndaw si doomam di dund daldi ñeewante doomam. Mu ne: «Déet, sang bi, jox ko xale bi. Bu ko rey mukk!» Ndaw sa ca des, moom, ne: «Deesu ma ko jox, deesu la ko jox; dogleen ko ñaar!»

Ag till sax joxe na weenam, nàmpal doomam, te sama bokk yi mujj néeg ba mel ni bànjóolig màndiŋ.

Amuñu xel, amuñu kóllëre, amuñu xol, amuñu yërmande.