Deuteronomy 14:8
TSK
Mbaam-xuux, moom, we wi xar na waaye du duññ. Kon daganul ci yeen. Aw suuxam, buleen ko lekk, te méddam, buleen ko laal.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Mbaam-xuux, moom, we wi xar na waaye du duññ. Kon daganul ci yeen. Aw suuxam, buleen ko lekk, te méddam, buleen ko laal.
Kee moom mu ngi rendiw yëkk, sarxal, te teewu koo bóome. Kee rendiw xar, sarxal, te teewu koo damm loosu xaj, sarxal. Kee ngi joxe saraxu pepp, te teewu koo tuur deretu mbaam-xuux. Kee di taal saraxu baaxantalu cuuraay, tey jaamu ay tuur. Ñoo taamu seen yoonu bopp, safoo seeni jëf ju seexluwu.
Ci kaw loolu mu dem, di surgawu ku cosaanoo ca réew mooma, kooku yebal ko ca ay toolam, muy sàmm ay mbaam-xuux.