TSK

TSK · Leviticus 15:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Askanu Aaróona, genn góor gu ci bokk du lekk ci sarax yu sell yi, li feek muy ànd ak jàngoroy der juy law mbaa jàngoroy xelli, ba keroog muy set. Ku ci laal lenn lu laal ab néew ba sobewu, mbaa mu tuur wasal moom ci boppam,

Ana wan xeet wu mag wu am yàlla ju leen jege ni nu sunu Yàlla Aji Sax jiy jegee saa yu nu ko wooyee wall?

Ca tundu Sinayi wa nga wàcc, àddoo asamaan, wax ak ñoom, dénk leen ndigal yu jub, ak yoon yu dëggu, ak dogali yoon ak santaane yu baax.

Mooy wax Yanqóoba kàddoom, dogalam yaak ndigali yoonam ñeel Israyil.

Luke 8:43 TSK

¶ Senn as ndaw a nga ca woon, diiru fukki at ak ñaar, ma nga doon xëpp deret, te def na ci alalam jépp, kenn manu koo faj.