Leviticus 7:11
TSK
¶ «Li yoon dogal ci saraxu cant ci biir jàmm, te nit sañ koo sarxalal Aji Sax ji mooy lii:
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ «Li yoon dogal ci saraxu cant ci biir jàmm, te nit sañ koo sarxalal Aji Sax ji mooy lii:
Yàppu saraxas cant googu ci biir jàmm te ñu jublu ci njukkal Aji Sax ji, dees koy lekk bés bi ñu ko rendee. Du lenn lees ciy wacc, mu fanaan.
yaw laay sarxalal saraxu cant, te turu Aji Sax ji laay tudd.
te ngeen lakk mburu, def ko saraxu cant. Yégleleen seen saraxi yéene te siiwal ko, dégg ngeen? Ndegam loolu ngeen namm, yeen bànni Israyil.» Kàddug Boroom bi Aji Sax jee.
Te yeen itam yeen ay doji cëslaay yuy dund, doj yi Noo gi tabaxe kërug Yàlla, ñeel liggéeyu carxal gu sell, ngir ngeen di ko jébbal ay sarax yu Noo gi rafetlu, sarax yu Yàlla nangu ndax Yeesu Almasi.