TSK

TSK · Leviticus 27:32

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Doj wii ma samp, muy xàmmikaay, mooy doon kër Yàlla, te lépp lu mu ma wërsëgal, dinaa ko génneel fukkeel ba moos.»

Muy dëkki tund yi, di dëkki suufu tund yi, di dëkki diiwaanu Negew, di diiwaanu Beñamin, di li wër Yerusalem, di dëkki Yuda, gàtt yi dina dellu ci loxol sàmm buy takk lim ba.» Aji Sax jee ko wax.

Ngalla nanga sàmme saw yet sa ñoñ, sa gàtt yi nga séddoo, te ñu màkkaanoo gott bi ñoomu neen, fi digg parlu mu naat. May leen ñu fore àlli Basan ak Galàdd na jant ya woon.