Genesis 22:4
TSK
Ca gannaaw ëllëg sa, Ibraayma daa dawal bëtam, séen bérab ba fu sore.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ca gannaaw ëllëg sa, Ibraayma daa dawal bëtam, séen bérab ba fu sore.
te waajal gannaaw-ëllëg, ndax gannaaw-ëllëg man Aji Sax ji maay wàcc ci kaw tundu Sinayi ci kanam mbooloo mépp.
Képp kuy góor ci askanu sarxalkat sañ na cee lekk. Lu sella sell la.
Ca bés ba ñu ko sarxale lees koy lekk, mbaa ca ëllëg sa; lu ca des ba ca gannaaw ëllëg sa dees koy lakk, ba mu dib dóom.
Ñaari fan, mu leqli nu, ñetteel ba mu yékkati nu, nuy dund fi kanamam.