te teewul ñu cosaanale ko Siyoŋ, ne kii ak kee fa bokk juddoo, te Aji Kawe jee saxal Siyoŋ.
TSK
TSK · Luke 1:76
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Psalms 87:5
TSK
Malachi 3:1
TSK
¶ «Maa ngii di yebal sama ndaw, mu xàllal ma aw yoon. Sang bi (/Boroom bi) ngeen di sàkku mooy jekki agsi këram, malaakam kóllëre moomu (/ndawal kóllëre loolu), ki ngeen safoo, mu ngooguy dikk.» Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko wax.
Luke 1:32
TSK
Ku màgg lay doon, te dees na ko wooye Doomu Aji Kawe ji. Boroom bi Yàlla moo koy jagleel nguurug Daawuda maamam.
Luke 3:4
TSK
¶ Loolu lañu bind ci téereb waxi Yonent Yàlla Esayi ne: «Baat a ngi xaacoo ca màndiŋ ma, naan: “Xàll-leen yoonu Boroom bi, jubal-leen ay xàllam.
Luke 7:27
TSK
Ci moom moomu lañu bindoon ne: “Maa ngii di yebal sama ndaw, mu jiitu la, xàllal la saw yoon.”
Acts 13:24
TSK
Laata muy ñëw, Yaxya moo doon yéene ngir waa bànni Israyil gépp sóobu cim ndox, jëmmale ko seenug tuubeel.