Ba Yuusufay tàmbalee liggéeyal Firawna buuru Misra, mu ngi tollu ci fanweeri at. Yuusufa daldi bàyyikoo ca Firawna, wër réew ma mépp.
TSK
TSK · Luke 3:23
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 41:46
TSK
Numbers 4:35
TSK
Ñu dale ko ci ñi am fanweeri at, ba juróom fukki at, ñuy mboolem ñi yelloo bokk ci kurél, gi liggéeyu xaymab ndaje mi war.
Numbers 4:43
TSK
dale ko ci ñi am fanweeri at, ba juróom fukki at, mboolem ña yelloo bokk ci kurél, gi liggéeyu xaymab ndaje mi war,
Luke 3:23
TSK
¶ Yeesu ci boppam ba muy door, amoon na lu tollu ci fanweeri at, di doomu Yuusufa, ni ko xel mana jàppe. Yuusufa, Eli mooy baayam,
Luke 4:22
TSK
Ñépp a doon seedeel Yeesu lu rafet, tey yéemu ci kàdduy yiw yi tukkee ci gémmiñam. Ñu naan: «Xanaa kii du doomu Yuusufa ji?»
Acts 1:1
TSK
¶ Yaw Tewofil, sama téere bu jëkk ba, def naa ca mboolem ndoortel jëfi Yeesu ak njàngleem,