TSK

TSK · Luke 4:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ay malaakaam la lay booleel, ñu di la sàmm foo jëm.

Luke 4:8 TSK

Yeesu ne ko: «Bindees na ne: “Boroom bi sa Yàlla ngay sujjóotal, te moom doŋŋ ngay jaamu.”»

Xanaa malaaka yépp duñu ay ngelaw yu ñu sas ab liggéey, yebal leen ngir ñu taxawu ñi wara jagoo ag mucc?