TSK

TSK · Luke 5:33

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Bu ngeen ma tàllaleey loxo, ma fuuyu. Bu ngeen doon ñaan-ñaanee it, du maa leen di déglu: seeni loxo, deret la taq ripp.

Te su ngeen lekkee ak su ngeen naanee, xanaa du seen bopp ngeen lekkal ak a naanal?”

Luke 7:34 TSK

Doomu nit ki feeñ, di lekk ak a naan, ngeen naay: “Kee fuqle, naan-katub biiñ biiy xaritook juutikat yeek bàkkaarkat yi.”

Maa ngi woor ñaari yoon, ayu bés gu nekk, di joxe asaka benn céru fukkeelu mboolem lu ma am.”

Acts 9:11 TSK

Sang bi ne ko: «Demal ba ca mbedd, ma ñuy wax Mbedd mu jub, te nga seet ca kër Yuda ku ñuy wax Sóol te dëkke Tàrs. Ma ngay ñaan.