TSK

TSK · Luke 5:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu ne ko: «Demal àbbi ay ndab yu deful dara ci sa dëkkandoo yi la wër yépp, te bumu néew.

Acts 2:41 TSK

¶ Ña nangu kàddug Piyeer nag, ñu sóob leen ci ndox; bésub keroog lu wara mat ñetti junni (3 000) yokku nañu ca gëmkat ña.

¶ Kon nag yeen sama bokk yi ma soppal sama bopp, farluleen, bu leen dara yëngal, te saxooleena jëm kanam ci liggéeyu Sang bi, te ngeen xam ne seenu ñaq, ci seenub ànd ak Sang bi, du neen.