TSK

TSK · Luke 8:44

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Da ne leen: «Bu ngeen farloo ci déggal seen Yàlla Aji Sax ji, di def li mu rafetlu, di teewlu tey jëfe ay santaaneem, di sàmm bépp dogali yoonam, su boobaa duma leen teg lenn ci jàngoro, yi ma tegoon waa Misra, ndax man maay Aji Sax, ji leen di wérloo.»

Mu teg ko ay loxoom, mu siggi ca saa sa, di sàbbaal Yàlla.

Acts 5:15 TSK

Nit ñi dem bay génne jarag ji ci mbedd yi, teg leen ci ay laltu aki basaŋ, ngir bu fa Piyeer jaaree, lu bon bon takkndeeram mana dal ñenn ci ñoom.