Psalms 109:4
TSK
Ma ji nit cofeel, mu sosal ma; te man ma di ko ñaanal.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ma ji nit cofeel, mu sosal ma; te man ma di ko ñaanal.
¶ Fan yooyu la Yeesu dem kaw tund wa ngir ñaani fa; mu fanaane faa ñaan ci Yàlla.
¶ Yeesu moo beru woon, di julli, taalibe ya feggook moom. Ci kaw loolu mu laaj leen ne leen: «Ana ku nit ñi ne moom laa?»
Fan yi Almasi dee dund dundu nitu suuxu neen, ay ñaan aki dagaan yu ànd aki yuux aki jooy la daan yékkati jëme fa ki ko mana wallu ba du dee, te nangule na it, ndax na mu ragale woon Yàlla.