TSK

TSK · Nahum 2:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Garab yi dul ruus, ak seedari Libaŋ sax di bége sab jéll, naan: “Ba nga daanoo ba tey, ab gorkat jógalu nu.”

Teewul rakk ja gëna gànctooti, gis nataali góor yu ñu yett ciy tabax, di jëmmi waa Babilon yu ca ñaase, xonq curr.

Watiir bu jëkk bi, fas yu xonq a ko takk, ñaareelu watiir bi, fas yu ñuul a ko takk,

Weneen fas ne jimeet, di wu xonq, ñu may gawaram mu jële jàmm ci kaw suuf, ngir nit ñi di reyante ci seen biir. Ñu jox ko saamar bu mag.