TSK

TSK · Nehemiah 13:28

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba mu ko defee, Sanbalat ma dëkk Oron dégg mbir ma, mook Tobya, Amoneen ba, ndawal Buur. Ñu am lu leen soofa soof, te mooy li nit ñëw, di sàkkusi njariñu bànni Israyil.

¶ Gannaaw loolu Elyasib sarxalkat bu mag ba ànd ak bokki sarxalkatam, ñu tabaxaat bunt ba ñuy wax Gàtt ya, sellalal ko Yàlla, taxawal laf ya, defaraat tata ja, ba ca soorooru Meya, sellalal ko Yàlla, jàppoo ko noonu ba ca soorooru Ananel.

¶ Yosuwe, sarxalkat bu mag ba mooy baayu Yowakim. Yowakim di baayu Elyasib, Elyasib di baayu Yowada,

¶ Lu jiitu loolu nag tabboon nañu Elyasib, sarxalkat ba, dénk ko sunu néegi dencukaayi kër Yàlla ga. Mu doonoon jegeñaaleb Tobya,

Maay xëy, sànk képp ku bon ci réew mi, ngir dagge ci dëkkub Aji Sax jii képp kuy def lu ñaaw.

Buur, bu xeloo, ràññee ku bon, mbugal ko, te du ko ñéeblu.