Numbers 14:21
TSK
Waaye ndegam maay Kiy Dund, te leeru Aji Sax ji mooy fees àddina sépp,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Waaye ndegam maay Kiy Dund, te leeru Aji Sax ji mooy fees àddina sépp,
Ñooñu, kenn desul ca seen biir, te bokkoon ca limeefu bànni Israyil, ba Musaak Aaróona sarxalkat ba jëkkoona tënke ca màndiŋu Sinayi.
«Du kenn ci nit ñii, maas gu bon gii, kuy gis réew mu baax mi ma giñaloon seeni maam.
Sunuy ñaawtéef a ngi janook yaw, te sunu mbóot leer na la.
Ana ñan la Yàlla mere lu mat ñeent fukki at? Xanaa du mboolem ña bàkkaaroon te seeni néew mujj tëdd ca màndiŋ ma?