TSK

TSK · Numbers 20:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Man dinaa taxaw ci sa kanam ci doj woowu ca tundu Oreb. Dóoral ci doj wi, su ko defee ndox dina ci génne, mbooloo mi naan.» Musaa def noona ca kanam magi Israyil ña.

«Jëlal saw yet, nga dajale mbooloo mi, yaak sa mag Aaróona, ngeen wax ak doj woowu, ñuy gis, mu xelli am ndox. Te nga sottil leen ndox mu jóge ci doj wi, nàndale ko mbooloo mi, ñook seenug jur.»

Lu la tere woona déggal Aji Sax ji, xanaa di saax-saaxee alal ji, di def li Aji Sax ji ñaawlu?»

Mu àddu ca kaw ne góoru Yàlla ga jóge Yuda: «Aji Sax ji dafa wax ne: Gannaaw tebbi nga waxi Aji Sax ji te defoo li la sa Yàlla Aji Sax ji sant,

Moo xar ay doj ca màndiŋ ma, mbàmbulaan wal, mu nàndal leen;

ki soppliw doj ndox mu taa, xeer wu ne sereŋ, mu def bëtu ndox.

Ndax merum nit du jur njub fa Yàlla.