TSK

TSK · Numbers 26:64

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Limleen mbooloom bànni Israyil gépp, na ñu bokke seeni làng ak seen këri maam. Waññleen góor ñépp, bopp ak bopp, ku nekk ak turam.

«Sunu baay daa dee ca màndiŋ ma. Moom nag bokkuloon ca gàngooru Kore, ga daje woon ci kaw Aji Sax ji, waaye bàkkaaru boppam a ko rey. Bàyyiwul nag doom ju góor.

Seen bët moo leen may la Aji Sax ji def ca Baal Pewor. Mboolem ku toppoon tuur ma ñuy wax Baal ca Pewor, seen Yàlla Aji Sax ji moo ko sànke ci seen biir.

Teewul ñi ëpp ci ñoom, Yàlla amul woon lu ko neex ci ñoom, ba tax ñu daanu, dee ca màndiŋ ma.