¶ Ba loolu amee Musaa woolu Yosuwe, wax ak moom, Israyil gépp teg ci seen bët. Mu ne ko: «Dëgërlul te am fit, ndax yaw yaay ànd ak mbooloo mii ca réew ma Aji Sax ji giñaloon seeni maam, ne ñoom la koy jox. Yaw it yaa leen koy sédde.
TSK
TSK · Numbers 27:19
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Deuteronomy 31:7
TSK
Luke 9:1
TSK
¶ Yeesu moo woo woon Fukk ñaak ñaar, jox leen xam-xam ak sañ-sañu dàq mboolem rab tey faj ay jàngoro.
Acts 20:28
TSK
Wattuleen nag seen bopp, wattu mboolem gétt, gi leen Noo gu Sell gi sàmmloo, te ngeen foral mbooloom gëmkati Yàlla, mi Yàlla jote deretu boppam.
1 Timothy 5:21
TSK
¶ Maa ngi lay àrtu nag fi kanam Yàlla, ak Almasi Yeesu, ak malaaka yi ñu tabb, ngir nga sàmm loolu te baña jeng, mbaa nga jëfe lenn loo defe xejj ak seen.
2 Timothy 4:1
TSK
¶ Kon nag dama lay dénk fi kanam Yàlla ak Almasi Yeesu, miy àtteji ñiy dund ak ñi dee, di la dénk ci darajay bésam ba muy feeñ, ak ci darajay nguuram,