TSK

TSK · Numbers 35:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Su dul woon pexe mu mu lal, xanaa mu fekk Yàlla yemale nit ki ciy loxoom, dinaa leen won bérab bu muy daw, làquji fa.

¶ «Ndegam nag du caageenu mbañeel, xanaa mu jekki dal ci kawam, mbaa mu sànni ko këf ku mu mana doon, te du lu mu waajoon,

¶ Gannaaw bu leen seen Yàlla Aji Sax ji wollilee xeet yi mu leen di jox seenum réew, ngeen dàq leen, ba dëkke seeni dëkk ak seeni kër,