TSK

TSK · Philippians 2:28

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Waaye ba ñu nettalee seen baay Yanqóoba li Yuusufa wax lépp, te mu gis watiir, yi Yuusufa yónnee, ngir jëlsi ko, ca la xelam délsi.

Israyil nag ne Yuusufa: «Yaakaaruma la woona gisati, ndeke Yàlla dina ma may lu raw gis la, ndax gis naa say doom.»

La leen yokk aw tiis nag mooy kàddu ga mu leen wax, ne leen: «Dootuleen ma gis.» Ba mu ko defee, ñu gunge ko ba ca gaal ga.

ndax namm na leen lool, boole ci tiisoo li ngeen dégg ag jagadeem.