Seen bët moo leen may la Aji Sax ji def ca Baal Pewor. Mboolem ku toppoon tuur ma ñuy wax Baal ca Pewor, seen Yàlla Aji Sax ji moo ko sànke ci seen biir.
TSK
TSK · Romans 11:4
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Deuteronomy 4:3
TSK
1 Kings 16:31
TSK
Mu sàlloo bàkkaari Yerbowam doomu Nebat. Loolu doyatu ko, mu jël jabar Yesabel doomu Etbal, buurub waa Sidon ña. Mu dem bay jaamu seen tuur mi ñuy wax Baal, di ko sujjóotal.
2 Kings 10:19
TSK
Ayca, wool-leen ma yonenti Baal yépp ak sarxalkatam yépp ak jaamukatam yépp. Bu kenn wuute, ndax sarax bu réy laay defal Baal. Képp ku ko wuute dina dee.» Booba Yewoo ngi fexee nax ñiy jaamu Baal, ba rey leen.
Hosea 2:8
TSK
«Moo tax maa ngii di ñage yoonam ay dég, gawe ko ag wurmbal, ba yoon réer ko.
Zephaniah 1:4
TSK
«Maay xàccil sama loxo, Yuda, ak mboolem waa Yerusalem. Maay dagge fi bii bérab ndesu tuuri Baal, ak turu sarxalantukatam yeek sarxalkatam yi,