TSK

TSK · Romans 8:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mboolem diir bi suuf siy wéet, moom lay nopploo la mu noppluwuloon, ba leen ay ati Noflaay fekkee ngeen dëkk fa.

Ba kañ la réew mi naa sereŋ, gàncaxu tooloo tool di lax? Rabu àll ak njanaaw a ngi sànku ngir mbonug ñi fi dëkk te naan: «Moom xoolul sunu muj!»

Ndax kat, càkkéef gépp, li ñuy déggal neenug neen la, te du seen coobare, waaye ki leen ci tënk la neex, ba tax ñuy yaakaar,

Jigéenu wérul juy matu la. Mu ngi yuuxu ndax mititu mat wu tar.