TSK

TSK · Ruth 3:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Ruth 2:4 TSK

¶ Nes tuut Bowas ne jalañ, jóge Betleyem. Mu nuyook ñay góob ne leen: «Jaagéenjëf waay, yal na Aji Sax ji ànd ak yeen.» Ñu fey ko ne ko: «Jaajëf sa wàll, yal na la Aji Sax ji barkeel.»

Ruth 2:20 TSK

¶ Nawmi ne Ruut: «Yal na Aji Sax ji barkeel Bowas, moom mi saxoo sàmm ngoram digganteem ak nit, muy dund ak mu dee!» Mu teg ca ne ko: «Kooku ku nu jege la; bokk na ci ñi am sañ-sañu jotaat nu.»

¶ Cofeel nag, muñ ak mbaax la. Cofeel bokkul ak kiñaan, bokkul ak jikkoy kañu ak a damu.