TSK

TSK · 1 Kings 4:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Keroog Aji Sax ji fas na kóllëre digganteem ak Ibraam, ne ko: «Askan wi soqikoo ci yaw laa jox réew mii dale ci dexu Misra, ba ca dex gu mag googee di Efraat,

Fépp fu ngeen teg seen tànk, yeena koy moom. La ko dale ca màndiŋ ma ba ca Libaŋ, daleeti dexu Efraat ba ca géej ga ca sowu, lépp seen suuf lay doon.

Terewul mu am ay nit ñu tekkiwul dara di wax, naan: «Ana nan lanu waa jii di xettlee?» Ñooñu sewal ko, yótuñu ko jenn teraanga. Sóol nag ne cell.

¶ Moom la Salmanasar buurub Asiri song, mu nangul ko, di ko fey galag.

Ezra 4:20 TSK

Yerusalem nag amoon na buur yu am doole yu moom mboolem wet ga ca Wàllaa Dex, ñu di leen fey galag ak njoti bopp ak juuti.

mu yilif géej ba géej ak dex ba ca cati àddina.