TSK

TSK · 1 Samuel 13:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ag mbaq aku doj la Daawuda mane waa Filisti ba, jam ko, rey ko, te yorul saamar.

Waaye li àddina jàppe ag ndof, moom la Yàlla taamu, ngir rusloo ko xamkat yi, te li néew doole ci àddina, moom la Yàlla taamu, ngir rusloo ko li bare doole.