TSK

TSK · 1 Samuel 4:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Naka la tudd gaalu Yàlla ga rekk, Eli xàwwikoo ca toogu ba, daanoo njaaxaanaay, dal ca bunt dëkk ba, loos wa damm, mu dee, ndax booba day mag mu ànd ak yaramam. Eli jiite na Israyil ñeent fukki at.

Aji Sax ji, maa sopp sa dëkkuwaay, bëgg bérab bi sag leer teew.

Moo nu nuy woye woyu Aji Sax ji kaw suufas yéefar?