¶ Man Póol ci sama wàllu bopp nag, maa leen di ñaaxe teeyug Almasi, akug lewetaayam, man miy teew ci seen biir, di ab ragaleey, fi seen kanam, te bu ma soree doŋŋ laa leen di ñemeey,
TSK
TSK · 2 Corinthians 11:21
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Li may wax nag, waxewuma ko ci ndigalal Boroom bi, waaye taxawaayu dof laa koy waxe, gannaaw mbirum damu la.
Looloo tax ma bind leen lii bala maa dikk, ba buma dikkee, du jar may mettil ni may jëflante ak yeen, ci kaw sañ-sañ bi ma Boroom bi jox. Ndax kat sañ-sañ bi, yokke moo ko taxa jóg, waaye deesu ko yàqe.