TSK

TSK · 2 Kings 20:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Gannaaw loolu Daawuda nelaw, fekki ay maamam, ñu denc ko ca gox ba ñu naan Kër Daawuda.

Gannaaw gi Buur Robowam tëdd, fekki ay maamam, ñu denc ko fa ay maamam ca gox ba ñu naan Kër Daawuda. Ndeyam a doon Naama, Amoneen ba. Ci kaw lool doomam Abiyam falu buur, wuutu ko.

Gannaaw gi Manase saay, fekki ay maamam, ñu denc ko ci toolub këram, di toolub Usa. Doomam Amon falu buur, wuutu ko.