TSK

TSK · 2 Peter 1:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ba mu ko defee Aji Sax ji yékkati sidditi doomu Selcel, Sorobabel boroom Yuda, ak sidditi doomu Yoccadag, Yosuwe sarxalkat bu mag ba, ak sidditi ña des ca mbooloo ma ñépp, ba ñu sottali liggéeyi kër Yàlla Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, seen Yàlla.

Kon ñeme lanu def, te li nu gënal di génn, des bitib sunu yaramu tey, ngir dëkki ak Sang bi.

Bàyyileen xel ñi ñu tëj, ni su ñu leen boole woon ak ñoom tëj, ak itam ñi ñuy mitital, ndax yeen itam, aw yaram ngeen am.

Ndax damaa leer, ni ma ko sunu Boroom Yeesu Almasi leeralale, bés bi may summi sama màkkaanu suux bii dëgmal na.