TSK

TSK · 2 Peter 3:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Xanaa ku mucc ayib, sell ab xol, xemmemul caaxaani neen, du giñey fen.

Bul di gaawa teg loxo kenn, ngir fal ko njiit. Bul séddu ci bàkkaari jaambur, te yaw ci sa bopp, sàmmool dundin wu set.

¶ Ci man Piyeer, ndawal Yeesu Almasi la bataaxal bii bawoo, ñeel askan wi Yàlla taamu, te ñu toxuji diiwaani Pont ak Galasi ak Kapados ak Asi ak Bitini.

¶ Moo waral ma fas yéene di leen dëkke fàttli loolu, doonte xas ngeen koo xam, ba tax ngeen taxaw bu dëgër ci dëgg gi leen nuyusi.