TSK

TSK · 2 Samuel 11:25

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Nangeen ko xool. Su jubalee réewam, wuti dëkk bi ñuy wax Bet Semes, kon Aji Sax jee nu teg musiba mu réy mii, lu ko moy nu xam ne du loxoom a nu dal, waaye ndogal lu nu dikkal la.»

Loolu lépp laa walbatiku xalaat, ngir lépp leer ma: Ku jub ak ku xelu ak seeni jëf, lépp a ngi ci loxol Yàlla. Mbëggeel ak mbañeel, xamoo lu la ciy xaar, lépp a nga ca kanam.