All books in KYG

2 Samuel 21

KYG · verse 18

24 chapters

KYG / 2 Samuel / Chapter 21

KYG · verse 18

G annaaw gi xare dellu am seen digganteek Filisteen ña ca dëkk ba ñuy wax Gob. Ca la Sibeka, ma askanoo ci Usa, rey Saf ma bokk ca askanu ponkal ya.