TSK

TSK · 2 Samuel 21:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Fàkkasleen mboolem xeet yi leen seen Yàlla Aji Sax ji jébbal nag. Buleen leen xool bëtu yërmande, buleen jaamu seeni tuur: Lu ko moy muy seenug fiir.

Mu jàpp Agag buurub Amalegeen ña, gàngoor ga gépp, mu faagaagal, leel leen ñawkay saamar.

Terewul Yewu amuloon pastéefu toppe léppi xolam yoonu Aji Sax ji Yàllay Israyil. Dëdduwul ba tey bàkkaari Yerbowam ya mu daan bàkkaarloo Israyil.

Luke 9:54 TSK

Taalibe ya ñuy wax Yanqóoba ak Yowaan gis loolu, daldi ne: «Sang bi, soo bëggee nu jox sawara ndigal, mu wàcce asamaan, faagaagal leen?»

Ñoom laa seedeel seenug parlute ci Yàlla, waaye dañu koo tegul ci xam-xam bu doy.